Eeh yeah. Senegal Boy. Yeah
Bal bangui sogo takk
Ghetto sama guinaw
Mane rek Mane kessé fi tekk tank
Xaliss dou doy, Jam dou eup
Tour bangui dem succès bi yok
Derétou Diamaguene mofi daw
Dérek momay téré té game bi Iyo, iyo
Nimay rabbé loussi sa yone
Bandit deug dekoy nouro
Xamnani si mane ngay xol
Mais nono ningue koy deffé dou nonou
Demla lal dé
Sa cho mane la bardé
Ay caché millions sans projet
Mane la Sénégal boy from djekk
Eh. Nono thiowli dou beuri
Mane ngen tekk sene beut yi
Té Nianou wadiour motakh ma eksi fi, wah eh
Gni lougnou fokk
Mounouniou bokk
Xirr bi la yorr
Gni daw malenkoy nokk
Ey manguey buzzou Ndongo Dema xew
Bomeu xamoul
Demal nga tokk
Eh démal nga tokk
Démal nga tokk
Démal nga tokk
Pic biniou ma sanni Mane demako toul
Niomaci djittou malenraw fouf
Nélene yolé xadjatoul ci poche
Niak sipp wessouwoul andak kou matoul
Xaliss la Xèkhè douma khoulo
Kholéma Ndongo Lô bir Ghetto
Musikou fi lay toukilo international
Nekké ci yone mashAllah
Poche Bangui fess may fékh na mère bi bégg
Bougne sagnone ken douma deug
Legui niom niomay xèhh
Nangou demb beuge bagne tey
Sissoumane yi demelen bayi ci birr
Kode sama xol def xeuthie
Eclate kanam bi xol Guedj
Eh. Nono thiowli dou beuri
Mane ngen tekk sene beut yi té
Nianou wadiour motakh ma eksi fi Wah eh
Gni lougnou fokk
Mounouniou bokk
Xirr bi la yorr
Gni daw, malenkoy nokk
Ey manguey buzzou Ndongo
Dema xew
Bomeu xamoul, demal nga tokk
Eh démal nga tokk
Boy Gni lougnou fokk
Mounouniou bokk
Xirr bi la yor
Gni daw malenkoy
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)