Wessou nagn xarite legui done nagne ay domou ndaye
Ak gning ma guissalone demb nga may gussal tay
Ko togne si gang bi nioun niuep nga togne
Wessou nagn xarite legui done nagn ay domou ndaye
Ay nitou deugue, Fi ken dou change
My brother for life never change
Ay nitou deugue, Fi ken dou change
Brother for life eeh
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille
Ça bouge pas
La famille, ya ya
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
I do it for a gang; i do it for my family
Lou meun ti weu dou tax niou tass, c'est à vie
Bo deconner dama la kay wax rek niou andate cool
Lou yague deugue la souniou ande bi deh dou ay dool
Father xadiou fi yen rek la done guiss depuis bamiy metti
Xolal fater xadiou fi yena ma dolel bama yeski fi
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille
Ça bouge pas
La famille, ya ya
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
Wessou nagn xarite legui done nagne ay domou ndaye
Ak gning ma guissalone demb nga may gussal tay
Ko togne si gang bi nioun niuep nga togne
Wessou nagn xarite legui done nagn ay domou ndaye
Ay nitou deugue, Fi ken dou change
My brother for life never change
Ay nitou deugue, Fi ken dou change
Brother for life eeh
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille
Ça bouge pas
La famille, ya ya
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
La famille, ça bouge pas
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)