Werouwaye
Canabasse
paroles Canabasse Werouwaye

Canabasse - Werouwaye Lyrics & Traduction

WEROUWAYEWayalnala sama life Khamngua limay téré nelaw Night
Yaw say nopay sama ndieguénaye
Yay yombal sama fight
Ya takh Ba bouma bayi
Yay sama werouway Mouy nakkar wala mbekté louma la djokh rek Ngua dieul
Yay sama werouway
Yeah bo Demone tay ma bayi ndakhté Bodoul yaw Mane awma benene werouway Bobou Ba legui gnoung gnou tek choc
Té tewoul gnou ngui stay strong Bidew bang Tchi Kaw té fa Lay moudié
Té dou Gno Fi néwone dou gnou dess bro Kouy khaar gnou dém na dieul chaise tok Bou done Mane Ak Mane rek khaddi na Ba dém
Ndakh yone Bi dafa yane Bi dafa diss yone Bi Meti Mais kou takhaw fou wor ani loy Tite
Loy tite Boudoul ko nguay Guiss Tchi sa sétou ani loy Tite
Boudoul sa bope ani loy Tite Amoul obstacle ani sa fit Diouk Ak daanou rakk bo Tchi diaroul di sip Ni yone tamoul Tchi bene Bro Keutch Bou daggoul dana gneuw
Kheutch Bou daggoul dana gneuw
Kone daal dou yone Ngua khaddi no!
Banekh Tchi thiono Lay diar You know
You know
Wayalnala sama life Khamngua limay téré nelaw Night
Yaw say nopay sama ndieguénaye
Yay yombal sama fight
Ya takh Ba bouma bayi
Yay sama werouway Mouy nakkar wala mbekté louma la djokh rek Ngua dieul
Yay sama werouway
Yeah bo Demone tay ma bayi ndakhté Bodoul yaw Mane awma benene werouway Té bobou ba legui gnoung gnou tek choc War na takh gnou stay strong
Gané God moussal gnou Tchi retanou none Ak Tchi Gni gnouy geumlo ni gno farr té demewoul nonou Yeah té dou gno Fi néwone dou gnou dess Bro Yokhla nagn lene dadjal ay chaises gnou tok Té khamal lene ni Bou dé gnoune Ak gnoune rek dinagn khar Ba dé
Lou yone Bi meunti goudde tank yi deggounagn Dina tarr mai amoul bayi nak Meune nagnou sonne wayé dougnou ta yi no!
God dina def li geune yokh la fight rakk
Boudoul sa bope ani loy Tite Amoul obstacle ani sa fit Diouk Ak daanou rakk bo Tchi diaroul di sip Ni yone tamoul Tchi bene Bro Keutch Bou daggoul dana gneuw
Kheutch Bou daggoul dana gneuw
Kone daal dou yone Ngua khaddi no!
Banekh Tchi thiono Lay diar You know
You know
Wayalnala sama life Khamngua limay téré nelaw Night
Yaw say nopay sama ndieguénaye
Yay yombal sama fight
Ya takh Ba bouma bayi
Yay sama werouway Mouy nakkar wala mbekté louma la djokh rek Ngua dieul
Yay sama werouway
Yeah bo Demone tay ma bayi ndakhté Bodoul yaw Mane awma benene werouway


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)