paroles Youssou N'Dour Ban la

Youssou N'Dour - Ban la Lyrics

BAN LA
Thi diame
La lépe khathie
Yalla na diamou djodou
saaàkh

Annnnnn annnnnn aaaaannnn

Fépe foumou Mana done
Amouma thi
Khadiak séne mane

Annnnnn annnnnn aaaaannnn

Bakéne diame la beugue
Soudé manoko aaaame
Annnnnn annnnnn aaaaannnn
Bouko aamé
Na fékhe bamou
Yatou yaatou
Bouko meuné
Na weure adounaaa
Chanteeeeeez
Danseeeez
Wawawe
Chanteeeeeez
Danseeeez
Chantez chantez chantez
Danseeez
Wawawe
Chanteeeeeez
Danseeeez
Féthie mi dale
nékhe nama
Thi deugue deugue deugue
Khawma thi banela
Féthie lene ko
Yombe na
thi deugue deugue deugue
Khaw ma thi bane la
Féthie mi dale
nékhe nama
Thi deugue deugue deugue
Khawma
thi banela
Féthie léne ko
Yombe na
thi deugue deugue deugue
Khaw ma thi bane la
( Partie faly ipupa)
Féthie léne ko
Yombe na
thi deugue deugue deugue
Khaw ma thi bane la
Féthie mi dal
Nekhnama
Thi deugue deugue deugue
Khaw ma thi bane la
Féthie lene ko
Yombe na
thi deugue deugue deugue
Khaw ma thi bane la
Dakar nanga def
Khinsasha.mbote
Africa bonjour
An whattsap?
Dakar nanga def
Khinsasha mbote
Africa bonjour
Thi deugue deugue deugue
Khawouma rythme bi banelaaaa
Dafma nekh rek
Ma dieme ko
Fééthie
Khawouma pathianga la
Khawouma danzon la
Wala rumba la
Wala cha-cha chaaaaa
Khawma khawma khawma khawma khawma
Bane laaa (bis)
Beugue naako
Fonke naako
Khawma khawma khawma khawma
Bane laaaaaaaa
Téke nako son
Téko pathianga
Danzon
Wala rumba la
Annnnnn annnnnn aaaaannnn
Téke nako son
Teko pathianga
Danzon
Wala rumba la
Annnnnn annnnnn aaaaannnn
Téke nako son
Téko pathianga
Wala rumba
Danceeeeez éééééééé
Annnnnn annnnnn aaaaannnn


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Paroles de chansons de Youssou N'Dour

Sélection des chansons du moment