04 04 1944
Youssou N'Dour
  • Arrangeurs: Ibrahima Ndour
  • Auteurs: Youssou Ndour, Kabou Gueye
  • Compositeurs: Youssou Ndour, Kabou Gueye
  • Editeurs: Universal Music Publishing
paroles Youssou N'Dour 04 04 1944

Youssou N'Dour - 04 04 1944 Lyrics

4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
Tóllu nii war ngeena bég, war ngeena bég ci independans bi, ak ñi ko indi
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na
Dama ne bu lëk lékkee olom budee gore na te dëggu war na ko gërëméé picc yi
No, no, no, no, no, no,
No, no, no, no, no, no, yee
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex
Ah lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gëm sa bopp moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
No no no gis say mbokk moo neex
4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex
Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex
Aaaaa, moom sa bopp, moo neex
Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, moom sa bopp, moo neex


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Paroles de chansons de Youssou N'Dour

Sélection des chansons du moment