REUGUINE TASS
Wally Ballago Seck
paroles Wally Ballago Seck REUGUINE TASS

Wally Ballago Seck - REUGUINE TASS Lyrics & Traduction

Deloulsil delousil dou meun nga darra dé diaroul xass
Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono ji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh dji beurina déy nourou mariné

Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass

Ni wo woo Vivi bougnou faalé
Bougnou décodé
Nagnou baalé
Ki léy diébaané
Boko séété dé yaako tané
Mane dé déég naala
Dafa féék né taloumala

eyow eyow eyow

Di nga sonou Faramareen féép leu meuné
Eyow eh
Nangoulmako té nga Take a sit, Take a sit
Vivi gnou féthial ko Reuguine tass

Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass

Viviane :
Deloussil deloussil comment tu vas (comment tu vas)
Nangoul niou lou niou mom té yalla takh (té yalla takh)
Maléy sonnal, té dawoulo dé wawaw

Demal nga tok, mané dolé yamoul wawaw
Kou andak lou niou andale loula nekh lathie

Wally ak Viviane beuri fitt faathie, yeah yeah
Bokk école, bokkou niou classe, té douma sa mass
Ma tangal sa khol, wakhko sa yaye mou soti ci glace
Té ragalouma lolou wooooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass

Bilay man dé beug naala
Walay man dé beug naala
Mayanté xaliss diaroul khass
Bilay man dé beug naala

Sant yalla dey nourou titeurou
Wakh deug yalla tognou gnou
Bour yalla né sante lén ma doli
Ba takhna ma deuké thiant li

Eh eh kou seu xol nekh nga ré

Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment