paroles Wally Ballago Seck CONFUSE

Wally Ballago Seck - CONFUSE Lyrics & Traduction

La traduction de CONFUSE de Wally Ballago Seck est disponible en bas de page juste après les paroles originales

Yaay booy wouyouma, damalay laadj (yeah)
Baay booy yédd ma, damalay laadj (yeah)
Beugouma loubakh reuthie ma, damalay laadj (yeah)
Beugouma réthiou tam, damalay laadj

Khamna limouy laadj (Limouy laadj, limouy laadj)
Niom niaar, kouné mounguék liniouy laadj (limouy laadjté waw)
Damay beuga diakhlé, ndakh awma choix ci niaar niou doywaar

(Wally)
Beugg nga mais ya ngui xel niaar
Beugo kou xar sa xol bi niaar baby
Xeyna gnifi diota diaar nio fowé sa xol banga fokni nieupa soxor

(Amadeus)
God loumou bind dathié deff niarr,
Ta yaw yaay sama guénwaleu man
Assaman si nimou yaato, naadj bi limouy tang, yaay képar guiy neubb naadj bé

(Mia)
Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté

(Amadeus)
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné

(Mia)
Hey, Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté

(Amadeus)
Yow Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné

(Amadeus)
Souma guissé nganane da ngama nop
Té ndeye dji seikh dou ame ci diamalé
Melni assaman ci nimou yaato
Ak bidéw yi niniou taaro

(Mia et Wally)
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu

(Wally)
Linguère may Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh)
Ballago Khaliloulay (Wouy)
Ndiabote gueu lay woutal yaay
Té keur ga yafa doy lingère way (Ayaa)
Maadi bour guéweul, khouss ndama lay béguel
So beugué malay wayal, thiol, ndér ak tama way
Linguère kay, so banié ma wett kaay,
Kaay, yaay sama wérouway

(Mia)
Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté

(Amadeus)
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné

(Mia)
Hey, Damay beuga diakhlé
Awma choix bébé khamna limouy laadjté

(Wally)
Linguère nga boul diakhlé
Mbékté dounya yi rek laala yéné

(Wally)
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu
No-no-no mon bébé
Ne t'en vas pas wawaw
Nékh nama, wayé diakhlé
Ndakh khamouma, kimay taneu




Traduction CONFUSE - Wally Ballago Seck

Il est difficile de traduire ces paroles car elles sont en wolof, une langue parlée au Sénégal, en Gambie et en Mauritanie. De plus, sans contexte, il est difficile de donner une traduction précise. Cependant, voici une tentative de traduction approximative de certaines phrases :

"Yaay booy wouyouma, damalay laadj (yeah)" pourrait se traduire par "Mère, ne me gronde pas, je suis fatigué (yeah)"

"Beugouma loubakh reuthie ma, damalay laadj (yeah)" pourrait signifier "Je veux que tu m'aimes, je suis fatigué (yeah)"

"Khamna limouy laadj (Limouy laadj, limouy laadj)" pourrait être "Je sais que tu es fatigué (Tu es fatigué, tu es fatigué)"

"Damay beuga diakhlé, ndakh awma choix ci niaar niou doywaar" pourrait signifier "Je veux te respecter, mais tu as le choix de nous quitter"

"Beugg nga mais ya ngui xel niaar" pourrait être "Tu veux mais tu as peur de l'amour"

"God loumou bind dathié deff niarr" pourrait signifier "Dieu sait comment faire les choses"

"Damay beuga diakhlé" pourrait être "Je veux te respecter"

"Linguère nga boul diakhlé" pourrait signifier "Femme, tu ne veux pas respecter"

"Mbékté dounya yi rek laala yéné" pourrait être "Seul le monde compte pour toi"

"Souma guissé nganane da ngama nop" pourrait signifier "Je ne peux pas croire que tu m'aimes"

"Té ndeye dji seikh dou ame ci diamalé" pourrait être "Et la mère de Seikh n'a pas de diamant"

"Melni assaman ci nimou yaato" pourrait signifier "Regarde le ciel, il est plein d'étoiles"

"Nékh nama, wayé diakhlé" pourrait être "Je te trouve attirante, mais respecte-moi"

"Linguère may Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh)" pourrait signifier "Femme, Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh)"

"Ballago Khaliloulay (Wouy)" pourrait être un nom propre

"Ndiabote gueu lay woutal yaay" pourrait signifier "Ndiabote, tu es la mère de mon enfant"

"Té keur ga yafa doy lingère way (Ayaa)" pourrait être "Et la maison est pleine de femmes (Ayaa)"

"Maadi bour guéweul, khouss ndama lay béguel" pourrait signifier "Maadi, le tambour de guéweul, le cuir de vache est ce que je veux"

"So beugué malay wayal, thiol, ndér ak tama way" pourrait être "Si tu veux mon amour, thiol, ndér et tama sont le chemin"

"Linguère kay, so banié ma wett kaay" pourrait signifier "Femme, si tu me refuses, je vais pleurer"

"Kaay, yaay sama wérouway" pourrait être "Pleure, ma mère est ma consolation"

"No-no-no mon bébé" pourrait être "Non-non-non mon bébé"

"Ne t'en vas pas wawaw" pourrait être "Ne t'en vas pas wawaw"

"Ndakh khamouma, kimay taneu" pourrait signifier "Mais je sais, tu es fatigué".

Encore une fois, cette traduction est très approximative et pourrait ne pas être précise.


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment