Ndaga
Samba Peuzzi
paroles Samba Peuzzi Ndaga

Samba Peuzzi - Ndaga Lyrics & Traduction

SENEGALBOYOO
From diack waw
Skurt, ratata, hey yah

Comme que dañi ndaga
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Comme que dañi ndaga (waw)
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Eh kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton
Kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton

Check hey
Duma teggi tànk ak sama semelles rouges
Doma guiss mafia bé lay nokk
Commencer guma ñom ñungui onku
Sama yaye néna non boulen tontu
Bu xayé tek ñorna meuno sipp
Son bu ngané ki du nitt
Ci man guen di xol jamano dji
Yarul ma jangal la non du ni
Hey legui folen ma guiss
Nélen tonton ñëwna
Sen clash yi mi ngui may dal
Mais tontu wuma
International boy fi guen di tok
Tek guen ma bët wayé dolen ma japp
Def sen awards sans man (rambakh)
Ayway nopal guen samba

Comme que dañi ndaga
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Comme que dañi ndaga (waw)
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Eh kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton
Kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton

Hey man késsé may door non li du xéx
Ñom duñ ma lale amna moustiquaire
Fils do tuss damala pique nga per
Sa yekk du yagg comme dajù ballon
Sama succès sama bras long
Sa meilleur sagnsé guiss nako Uno
Olala rappeurs yi fi ñom dal ñom ñeup ndiro
Yalla ma yombalale li textes sax binda tuma ko
Legui game bi dama fay
I got the drip boy (thiey li)
Di pull up ak sama beamer ouh yah aduna ni leu
No cap amna xaliss ouh yah aduna ni leu (Baww)

Comme que dañi ndaga
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Comme que dañi ndaga (waw)
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Eh kolo kuy sa kolo kolo
Rappeur yi may sen tonton
Kolo kuy sa kolo kolo
Rappeur yi may sen tonton

Comme que dañi ndaga
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Comme que dañi ndaga (waw)
Wowal Pape Ndiaye Tama (waw)
Nénañ dañi ndaga
Eh kolo

Eh kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton
Kolo kuy sa kolo kolo
Rappeurs yi may sen tonton


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)