Boum la beugoul lone douniou seuy
Boum la noboul wone damlay fowé
Boum la beugoul lone douniou seuy
Ay détails lay bagn loutax niou deuk di khoulo ohh
Boum la beugoul lone doumla marié
Boum la beugoul wone damlay fowé
Boum la beugoul lone douniou seuy
Kay niou diém ko doundou comme Marie
Beug nala beugeu ngama ak Cheikh Marie
Woloumaaa... Marie, ak Cheikh Marie, woloumaaa
Marie ak Cheikh Marie, Woloumaaa
Marie, ak Cheikh Marie woloumaaa
Alliance si lokho hum hum ! kone doyoula
Chaque jour nga vérifier sama téléphone kou beugay fiir
Nangou naa, wayé dang si bolé togn
Comme bépeu goor, parfois ma nélaw mais
Tay guissna si ioe louma métii yeah
Saga ngama, bayiwo si xel grawoul khamna sa xol la tangue
Boul déglou waxou nitt yi dagn ley misère lo
Ladial nioumey andal ioe lay titaro
Té souma nobatone kénén yakoy nieuka yeuk hééyy
Ndax yay sama xol yah
Boum la beugoul lone douniou seuy
Boum la noboul wone damlay fowé
Boum la beugoul lone douniou seuy
Ay détails lay bagn loutax niou deuk di khoulo ohh
Boum la beugoul lone doumla marié
Boum la beugoul wone damlay fowé
Boum la beugoul lone douniou seuy
Kay niou diém ko doundou comme Marie
Beug nala beugeu ngama ak Cheikh Marie
Woloumaaa... Marie, ak Cheikh Marie, woloumaaa
Marie ak Cheikh Marie, Woloumaaa
Marie, ak Cheikh Marie woloumaaa
Diameu rek ka fi khathie, pour keur gui nékh
Sa xel waroul niaw no no, même souma goudé niow
Si loula nékh rek ladone dokh
Défal comme avant, nga teundou ma ak sourire bou nice
Soumiy samay daleu, lathie ma nouma
Def, beusseul ma samay tank, thiouray di dioli
Khoulo waroutouniou no no, boul di fowéti sama xol
Damla beugeu té neuboumako, yeureum ma
Warounio khoulo oh
Loe la taneu pour ngeu done sama yayou dome yah
Boum la beugoul lone douniou seuy
Boum la noboul wone damlay fowé
Boum la beugoul lonedouniou seuy
Ay détails lay bagn loutax niou deuk di khoulo ohh
Boum la beugoul lone doumla marié
Boum la beugoul wone damlay fowé
Boum la beugoul lone douniou seuy
Kay niou diém ko doundou comme Marie
Beug nala beugeu ngama ak Cheikh Marie
Woloumaaa... Marie, ak Cheikh Marie, woloumaaa
Marie ak Cheikh Marie, Woloumaaa
Marie, ak Cheikh Marie woloumaaa
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)