Sama Everything
Philippe N'Dour feat Viviane Chidid
paroles Philippe N'Dour Sama Everything

Philippe N'Dour - Sama Everything Lyrics & Traduction

Yeah yeah

Yay sama everything
Beugeul ma défal la
Amouma anything

Té dou té ma défal la
Wakh iow lo beugeu
Sa baneex rek la beugeu
Sama yéné défal la
Togal ma firila

Yay sama everything
Beugeul ma défal la
Amouma anything
Té dou té ma défal la
Yangui yekk sama loveu
Yangui few sama loveu
Li ma yéné xamnako

And you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
Oh You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri
And you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
Oh You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri

Yalla ma bolék iow
Yaye diourom nienti wér nga eumbouma
Tey dji maag na
Wathié di kow souf man ganéssina
Wakhma lane nga beug
Lépp ma défal la paréna
Sama yéné manak Zeyna ci adouna ben la (ben la)
Gouddou fane dé laly nianal
Yobbou la makka la yéné
Magg na beug dap sa love
Xamna mounoumala fay
Tey Yalla may sédé ci sama yéné
Linga def ci nioun
Yaye boy yay Gaindé

Yay sama everything
Beugeul ma défal la
Amouma anything
Té dou té ma défal la
Yangui yekk sama loveu
Yangui few sama loveu
Li mala yéné xamnako

And you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
Oh You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri
Oh you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
Oh You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri

Dolli Sant Yalla sama dom xalébi magg na
Lingma yéné mangui niane buur Yalla mou degeu leu
Pa Philippe sa wakh yeggna ci xol nekhnama
Pa Philippe Vivane
Yaye ak dom guén di ame
Philippe

Yay sama everything
Yay sama adouna
Amouma anything
Naniou sant yalla
Yangui sama loveu
Mangui yekk sa loveu
Mangui feel sa love iow mi

Oh you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri
Oh you know you know you know Mama
Xamnako baby
Li mala yéné you know now Mama
Xamnako Baby
Oh You know you know you know now Maa
Xamnako Baby
Xamalna ni sa domyi
Deff la yéné Lou barri

Mar buur Yacine Mar
Birame Yacine Mar
Birame Ngouille Alé Ndiaye
So woyoul denga wara woy
Ndéye Sokhna sa Mame
Ami Fall sa Mame
Bouba Ndour sa baye
Viviane sa Yayoo woyal


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment