paroles Le Peuple de l'Herbe Ay Tchalen

Le Peuple de l'Herbe - Ay Tchalen Lyrics

La traduction de Ay Tchalen de Le Peuple de l'Herbe est disponible en bas de page juste après les paroles originales

Man dama togon
Di geustu, di xol, di xaalat
Fu ma tolle sama yon, sa ma liguey
Mu men ne tolla guma fen
Mu mel ne da gnu ma taaka

Mu mel ne sama aduna da fa djaxasso mom
Ma guestu wuut kuma meuna leral
Ma guestu ba guiss baye te guissou ma baye
Te guissou ma baye

Mu mel ne ama tuma pexe
Mu mel ne da gnu ma taaka

Mane deglu ma
Ma deglu ma
Ma waax la deug yow
Ma waax la deug ma waax la deug
Tcha deug
Fonkal saliguey
Diapal sa liguey
Bul ragal dara yoy
Defal li la war gnan yalla djeum kanam

Chorus :
mo taax ma ni yen djangalen
yen djagalen, yen djangalen
yen gneup djangalen
mani ay tchalen
gnou djanga djeum kanam
te bagna delu guinaaw

Man dama togon di nakarlu yaye
Ndaax sa ma liguey mom djeuma gul kanam
Gnou ni ma da nga nan yalla, yalla, yalla
Te ndimbeul da tchiy feka loxal borom
Woa sa borom te bay sa tol
Beyal sa tol

Mu mel ne ama tuma pexe
Mu mel ne da gnu ma taaka

Mane deglu ma
Ma deglu ma
Ma waax la deug yow
Ma waax la deug ma waax la deug
Tcha deug
Fonkal saliguey
Diapal sa liguey
Bul ragal dara yoy
Defal li la war gnan yalla djeum kanam





Traduction Ay Tchalen - Le Peuple de l'Herbe

Ay tchalen / en avant…

Des fois je me pose
Pour contempler le chemin parcouru
Le travail accompli
Et j'ai comme l'impression de ne pas avancer
Comme si j'étais pris dans un piège

J'ai comme l'impression
Que mon monde baigne dans la confusion
Je me retourne pour chercher une solution (la lumière)
Espérant croiser le regard de père
Mais il n'est point de père

(Alors une voix me dit)

Écoute cette vérité
Content-toi de bien faire
Fais ce tu dois n'aie aucune crainte
Travaille et prie pour aller de l'avant

C'est pour cela que je vous exhorte tous à apprendre
Apprendre pour que nous n'ayons pas à revenir en arrière
Travailler pour que nous puissions tous aller de l'avant…


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)