Olou
Lass
paroles Lass Olou

Lass - Olou Lyrics

Bougnou xamanté balé
Massouloma défe louma méti
Liga donne si mane dafa baré
Wawou mane damala beugeu
Yéneu saye moudady méti lolou
Gnou dady dioté mak yaw baye gagnou
Lolou massoula wagni sougnou mbeuguel
Wawou mane damala beugeu

Ma rény xole
A sama weurseuk bagui
Boule ragal Dara
Manouma la bayi waye
Ma rény xole
A sama ouroule ayeny
Boule ragal Dara
Manouma la bayi waye

Ma rény xole
A sama néné touty
Boule ragal
Manouma la bayi waye
Ma rény xole
Boule ragal
A sama weurseuk bagui

Wa souma banéhe gnou bocouco
Souma amé nakar gnou bocouco
Yama wone gore ma fayelaco
Wawou mane damala beugeu
Nala wone ny amga gorou yalla
Dina wone ny dioumo bigamaye taneu
Dina bégueulo sassou nékeu
Wawou mane damala beugeu

Ma rény xole
A sama weurseuk bagui
Boule ragal Dara
Manouma la bayi waye
Ma rény xole
A sama ouroule ayeny
Boule ragal Dara
Manouma la bayi waye

Ma rény xole
A sama néné touty
Boule ragal
Manouma la bayi waye
Ma rény xole
Boule ragal
A sama weurseuk bagui


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment