Dounia
Lass
paroles Lass Dounia

Lass - Dounia Lyrics

Diahelé ouma
Diomi ouma
Taye die titouma
Magui santeu borome bé
Mane amouma aye diplôme
Mane amouma asse comecome
Sama Baat rek layoré di ligueye
Sama bate rek layoré mome la ame
Ligueye rek yaw dé mo wore dé
Dounya hé mougne la ladie dé
Dounya hé gnafé la ladie

Si caname rek la dieme papa yé
A yé
Sameugama técgama si yonewé
A yé
Si caname rek la dieme mama yé
A yé
Amatoule loye tite mama yé
A yé

Wawe yéne saye
Diahelé dadile topou waye
Ga tite waye
Ba doto wolou sa bopou
Naga xamené borombi mogui saguinawe
Ha doula massa bayé
Loumou méti méti boule tita waye geumal sa bopou wa wawe
Adouna déméni adouna mélala nilé fomeuna déme dou yombe
Wawe naga gorgorloye
Dounya hé mougne la ladie dé
Dounya hé gnafé la ladie


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment