Légui sama mama love khamna ni mangui ci yone
Chaque jour Télé bi wane ko domame mongui roy ci mome
Mangui dokh ci thiobe
Gars yangui rott ci dobe
Bougouma thiow bi jok
Ndakh ma tok ci kaw
Yeah manék ci tiol bi
Té mounou ma nopi
Kone mou yombeu
Ndakh kén danouma dég-lou bimay sog-di dor
Témou khot ci yaw
Méfie toi de l’eau qui dort
Gueneu cool pourtant mala gueneu done doff ci job
Chaque jour ma bindeu texte boula meune tékkilo
Chaque jour nga dadjou ci samay Punch #Tequila
Défal ndakh yaw yay craie, mane may dactylo
Ci rap bi nitt bou dof la ba dagn may ték Killah
Kilifa la, kén douko wéddi
Amounma temps wou ték deal,
Moussouma sathie ténék
Diémouma ame sa estime
Terrain bi mafiy Messi
Rakhass game bi ni lessive
Flow you dakk Hennessy
None yangui danou yessi (Yow)
Gni gui kékh, Gni gui diaw, dima guerre wayé gagner lama gueme boy té dara douko dindi
Bomay dé, dima kheum, damay ré, ndakh té khamna fimay dieum té dara douko dindi
Gni gui nié, Gni gui kheuw, sandi khérn wayé kanam lama dieum té dara douko dindi
Bomay dé, dima kheum, damay ré, ndakh té khamna fimay dieum té samay gars yi rék la guem
Yokal son bi some stp,
Gnima beugone lék légui nék nagnou ay légumes
Yeah ni nice
Yeah, Yeah, mane samay gars yi rék la guem
La guem (x3)
Wakh dji beurina bo défaro ba paré pour gnou rappe deug let go
LEGGO (x6)
Soldat dou sonou sou dessoul loudoul wakhtou guerre
C’est décidé sol dall songoulén wakh bi lérr
Défna ay sons you bone balamalay diokh you nékh
Kharouma bayi diangue bala may khoslou men
Comme nénay jamdong leu nagn sott mou xékh
Lolou la gars done wathie difokné awma xél
Ma yobbou mère resto fayalko note you chère
Diaroulma cossou pour nguén xam kouy sén boss game (ah)
Mane mafi livrer ay came pour nieup
Amna boukeu xalé’k mak, bopp bounék ak lakhassam
Mafi nieuk rime ay phrases leumb
Nieuk dadji Jordan you bess takk ak toubayou ndiakhassam
Abalén Ok, merci bien
Sokhor Taliban bou diékou A-mé-ri-cain
Gandi poète depuis bimanéké 1ère L
Flow bi dope neu bala ngay takk sa 1ère L free eazy
Gni gui kékh, Gni gui diaw, dima guerre wayé gagner lama gueme boy té dara douko dindi
Bomay dé, dima kheum, damay ré, ndakh té khamna fimay dieum té dara douko dindi
Gni gui nié, Gni gui kheuw, sandi khérn wayé kanam lama dieum té dara douko dindi
Bomay dé, dima kheum, damay ré, ndakh samay gars yi rék la guem
La guem (x3)
Gnima beugone lék légui nék nagnou ay légumes
Légumes (x3)
Mane samay gars yi rék la guem
La guem (x3)
Wakh dji beurina bo défaro ba paré pour gnou rappe deug let go
LEGGO (x6)
Mane samay gars yi rék la guem
La guem (x3)
Gnima beugone lék légui nék nagnou ay légumes
Légumes (x3)
Mane samay gars yi rék la guem
La guem (x3)
Wakh dji beurina bo défaro ba paré pour gnou rappe deug let go
LEGGO (x6)
Qu’est-qui se passe Elzo please cesse le drame
Master Peace yingui pass
Dotoul peace, faut que niou kass
Presque beat ak bass yi nga tester yeup nga blast
Nieup nga blesser, nieup nga wass,
Fokgnou kill leu tokk sa place
Qu’est-qui se passe dope you diss yi shit you rare ri
Son yi hit leu, mix master,
Daf ga street bi limoula sass
Créer na ci game crise sou asthme
Koumaci blessé sorry masseu
Bindeul lettre team bi kass
Ndakh samay gars yi rék la guem
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)