One Night
Dip Doundou Guiss
paroles Dip Doundou Guiss One Night

Dip Doundou Guiss - One Night Lyrics & Traduction

Yow mi, yow rek
Mak yow, doundak dé
Kay tok fi, do dem
Lo wakh d'accord, oui, okay

Té mane damala beug si sama xol
Té damala beug ba khadiato sama xol
Weuy nala, paroles yangui tchi sama xol
Guiss nala bama kholé tchi sama xol eh !
Don't cry, don't cry, don't cry, don't cry
Don't lie, don't lie, don't lie oh oh

[NAILAH]
One night without you, oh hoo
One night without you, oh, oh
I can't spend one night without you, oh hoo
One night without you
I don't want one night without you

[Dip]
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you

Fixer ma sa beut yi lay khol ni
Drogué ngama yak sa parfum bi
Yobouma fo khamoul sakh yone bi
Meunougnou rér ndakh soma guissé, soumla guissé fégn
Hey way hey way
Kay ma déf la diabar baby kay gnou seuy way
Fanane si nékk sans yow rek meune nama rey way
Dang may manqué sa youma khéffé sa wett kay

Parce que mane damala beug si sama xol
Té damala beug ba khadiato sama xol
Weuy nala, paroles yangui tchi sama xol
Guiss nala bama kholé tchi sama xol eh !
Don't cry, don't cry, don't cry, don't cry
Don't lie, don't lie, don't lie oh oh !
One night without you, oh hoo !
One night without you, oh oh !
I can't spend one night without you
One night without you
I don't want one night without you

One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you
One night without you

[DIP]
Diokhma lima mome
Diokhma lima yéllo girl
Tégkma sama place my girl
Diokhma lima mérito
Diokhma lima yéllo girl
Tégkma sama place, so oh 
Diokhma lima mome
Yow réka nék fi
Goudi bi goudou na meun nga dess fi
Fanaano té guiss ngama sa guént yi
Teutch nala meuna toma reutcheuti eh !
Don't cry, don't cry, don't cry, don't cry
Don't lie, don't lie, don't lie oh oh !


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment