Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Ni leu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Kone ni leu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Assamane si meune xiine té dou taw
Sama mama dineu triste mais dou dioy
Deukou Christ mais seu fils beugoul foo
Béne domeum deufeu xiff tédou thiop
Diote meu yé seumay guénte
Di yettal seumey beugue
Goor yéngui yom goor djiguéne yi di gueune deugueur
Dou danga moumeu rek sa yalla wareu teukh
Diour sa bop soul seu bopp gnar rek moleu meuneu teu
Amo place même sisseu mère niggah
Foum leu diouré faleu seu makk yi diougué niggah
Meuwty dineu moudie déh
Matt deum bou rafète dou wallé fébare bou néxx niggah
Rakk woloule sa xarite yi
Beuss dineu ngneuw xamni saffara mo dakk fi
Déréta ma foore gnileu beugue sonale
Seu papa diangual leu xarou seu yaye nampalé leu possone
Mane deugn meuni diokhél seu xole ma dioxé seumeu rouh
Gnou xarre meu tidji seumeu gatte
Ma oubi seuma youre
Nathie dou yeuk sédday kéne leundeumoul beu lampe bou nioul
Yagg diox sa tate nitou goudi yarre ey dome you flou
Seu pêle bingjue gassé paxx bi
Si leugn lou moudie soul
Deumeu cher bomey ray déffé pakka wourouss
Tant que gnongui fène beusseul seu xole
Bagneu tontou mougn
Yakh derr yakouté xéssayou xéssal kate leu deugg bougou moure
Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Kou amoul xole amo fite
Kou geum yalla do raggal
Ray négn kou dioudo goul
Teuthie negn kou déffoul dara
Seu mbokk diexx bo rayyé sey none
Meuno wète bo amé ndam
Défaite mom orphelin leu
Ni sédayou safara
Ligeuy you ndeye moy agnoup dom
Rongogou mère si gnak diom,
Mandi baxoul soxor mo baxx
Té policier bi diay leu drogue
Meunougn ma faye (meunougn ma faye)
Ibliss dou sax job comme mane
Awmeu deukeundo si kaw souf
Bokoungnou trap omh non no non non
Founé dem na fa,
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Founé fanane naffeu
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Nileu meunone démé yeah !
Ni leu meunone démé yeah !
Ni rek ni rek anh !
Ni rek ni rek anh !
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)