Funérailles
Dip Doundou Guiss
paroles Dip Doundou Guiss Funérailles

Dip Doundou Guiss - Funérailles Lyrics & Traduction

Reptile Music
Yeah…Yeah
A crime save yeah
Anh… Anh
Yeah I'm sorry for myself
I'm sorry for my self no no Ouh Ouh 
Gotta make it for myself no no
They don't love me any more

Beus bi ngay dèe, 
Ay rongoniam meunone nala sangue
Doolei youxou yi atane nagnu sa corps bi ba si sa biir pakh
Soul la si sa cambeu
Merr na kagn wayei dou geudj dilla nianal founek dinalafa
Toudal tourou y'Allah
Bagua demei ngua yobalei xollam doundame niakk khorome
Goumba teukhlou gana
Beuss bi ngay dée ay goudila yeah
Si lagne guedjeu yeuk lerayou beuthieuk
Kerok nioune nieupeu leu demone yeii ba mellni daguay nelaw
Ndakh keine meunouko gueum
Xar yeik khath bi dem nagne ba dagne ko yeuk amoul mbow amoul
mbeé bébé sakh dou seukeute
Mowti djeulloula non dala goungueii ngua gnibi ndakh
deukoofi Al-Jannah ngua deuk
Deug leu deug leu deug leu Yeah 
Beuss biguay dée thi goudi
La fégne Keur gui ni tekk Djeum dja faye
Teud sa caisse kou djeum ngua tew
Fleur yi la deff si att bi ngay djoudeu ak att biguay djotta
gueine Adina yaw
Ameilooniou dara diokh ma lingèy yi dalloul dinalako dello
beuss bi may nieuw Eh

Beugouma diap sama xel que ni dotoumala guissate
Ya gnu nango bayyi def sa bopp ndem si y'Allah mane louma ci meune 
Chaque goudi damay gueinte guiss la, gueinte bou nek ak limuy missal 
y'Allah meuneu mayé meuneu dieullate limou mome doussi yaw doussi mane
y'Allah doula def dara, sa ndjaaboot dou torokh, 
Ta suuf dou tang si sa kaw
Gni guene ci niune moy gni gneukeu dem
Warone naniou goude fane dakh ma meune aw fi nga aw
Mougne na mougne ba meuneutouma mugne
Ndakh ronkhongne yi dess ci biir moy ronkhogne yi geuna
sokhor boul deloussi gnune gnolay fekki boudé ya ngi gnuy
guiss kholal gnune dagnu koy feté legui kholal
Na mère yi fethie, Pa yi mandi
Réindi beuye yi, réindi mbame yi 
Dagnu lay goungué nga feeki Mame yi
Am nga ganaille yu bess pour aar gnu
Même sa noone yeupa tew solu all black, tout noir représente
Tour fi ndokh pour que niou soul ci kawam
Nakhari na ci mane ma faté Funairaille yi rawatina sama funeraillou bopp hé !

Béneu mo geuna gaw
Niaar mo geuna woor
Gneuwa ndo wuniou mane ak yaw Mama Cry, don't cry no
Mama Cry, don'r cry no
y'Allah buur moma lathie
Nono gnéméwuma négocier
Bayil ma dem sagnuma négocier


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)