Khekh Yu Bess
Canabasse
paroles Canabasse Khekh Yu Bess

Canabasse - Khekh Yu Bess Lyrics & Traduction

Yaw linga beug def baye dou dém
Mais comme danga gnou beug test kay gnou dem
Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne
Lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell
Yeah nitteu gawa faté lolo takh
Nga takamlou deuk leumm té niola faal
Prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot
Mbirr bi doufi goulète
kagn lagnouy tall khekh yu Bess
yakarone nagn la tchi demb macky sall
Mais teydji nioune la contre yaw
Té nala leer né dictateur doufi am ndam

Mais nak thiow dou djipp, dedett thiow dou djipp
Ndakh sène dokhaline défoul dara loudoul yokk sunu fitt
Leeral sunu beutt niou xippi di guiss
Legui xam negn kane moy kane yeah ragné nagnou bitch yi
Gni niou sekhall ba sène gatt feess meuneutouniou wakh
Gni mbouxoum kerall boulène sax sène dotouniou marche
Gnémétouniou naadj gnom ak gni niouy door nio far
Degn ley togn nga aalou niou shoot seu ndeye parei neila masta

Yaw linga beug def baye dou dém
Mais comme danga gnou beug test kay gnou dem
Kou ndobine rey sa mame daaw dé rêne
Lou nioul foko sène doko diégué dingko daw bodé borom xell
Yeah nitteu gawa faté lolo takh
Nga takamlou deuk leumm té niola faal
Prési dem prési dikk prési doul niou sissou fippou takk derr yi diniou shoot
Mbirr bi doufi goulète
Kagn lagnouy tall khekh yu Bess
Yakarone nagn la tchi demb macky sall
Mais teydji nioune la contre yaw
Té nala leer né dictateur doufi am ndam

Rafétalaal litchi dess
Ngala thiow li na djekh
Domou rew mi gningui dè tchi diéma défendre séni rêve
Gni dieul balle gni dieul gaal tchi nguru macky sall
Esk bo teudé dinga nélaw goudi
Esk culpabilité leek leek dinaley fék sii
Def niou sey dom li dess mandat bi niou def la ndjiite
Mou djekh ak djamm nga dem bo bégné gaal gui dikk


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)