Mangui toudou Djibril Fall, niou gueune ma xam thi tourou Bril
Bataaxal bimay bindeu nak, mangui koy djagglél buur
Bataaxal bi djéékhagoul, Prési degglouma
Meunouma dénthie sama xalima té bindouma
Wakh thi gni féébar yor ordonnance té amouniou lougnko djeundé
Gni né thi ngour gui beurilé ba amouniou lougn ko doyé
Continué di tek deal you sétt ni léélou Aba
No stress laniouy léékké sunu xaliss douniou Nitt
Politicien yé gueuna faux sonnerie iphone thi android
Dangay niakkeu ba do nélaw, niou rêvélola done sa Ndjiitt
Koula matteu fatalila ni amnga ay beugn
Dotouniouko nangou c'est le Sénégal qui bagne
04 Avril khamwma louniouy fêter wayé dou indépendance
1960 ba tay ngén djokh lou beuri France
Paathio Rewmi ba nioune amatouniou bén liberté
Statue de la liberté niou eup liberté
Nioune douniou ay tailleur wayé djeulnagn ay mesures
You léér , tek ko fou léér , je vous le jure
Peuple bi ragalouniou guiss nga niniouy tééro Risques
Ba sa ministre bi tite djignlén terroristes
Dou deugg dou yone kou wakh nga teudj amo opposant
Légui peuple bi mo moudjé guéneu done sa opposant
Deugg ngéni bagn té deugg faaléwoulén
Teklén ko thi yone nangoulén
Deugg mou moudjou féppeu kone parélén
Djaay dõlé baakhoul waathieulén
Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)