Yonou Deugue
Youssou N'Dour
  • Arrangeurs: Ibrahima Ndour
  • Auteurs: Youssou Ndour, Kabou Gueye, Massimiliano Calo
  • Compositeurs: Massimiliano Calo, Youssou Ndour, Kabou Gueye
  • Editeurs: Universal Music Publishing
paroles Youssou N'Dour Yonou Deugue

Youssou N'Dour - Yonou Deugue Lyrics

Sama domou yaye,bo oubé bountou deugue
Boule ragalwéte, ndakhe dina néw gnou la feugue
Sâye sâye, séîtané, gni diouboule dougne la beug
Gni ragal di lakhou ak gni khamouldougne la leungue
Wâyé séne bîre khole, niome séne bîre khole
Fougnou néke,gnougue lay khalate, thi séne khéle
Wâyé séne bîre khole, niome séne bîre khole
Gnou gui laye diapalé thi lou wêre
Besse dina gneuwe
Yangi doga khame, thi boula thiono dabé
Li di mbéttéle dana la diogué founé
Dougnou nieuw sa keur té dotou gnou la téléphoné
Daniouye fôke ni yawe bougnou la diégué sakh yakhoulé
Wâyé séne bîre khole, niome séne bîre khole
Fougnou néke,gnougue lay khalate, thi séne khéle
Ragale fésse, pékhé diékhe
Gnoungui lay diapalé, thi lou wêr
Bess dina gneuwe
Yawe sa nattago,ngene bokke beugue beugue
Boula beugue ndaw téré wakhe li dideugue
Loumou métti métti métti,nangoul né wadji mbeur la
Loko contre, contre, contre,sédelni liguey kat la
Yawe sa bîre khole,yawe sa bîre khole
Finga nék nangou nga né diambare la
Ragale fésse,pékhé diékh,
Sougnou guisse guisse, meune na wouté
Wouté guisse guisse boumou takh bangnou bagnaneté
Boul di neubbe fa nga fété
Yalla sakh dafa tane yonénte mou djité
Yawe na nga moytou ragale pété
Dégue nané meune nala khagne sa mbecté
Yawe na nga moytou ragale pété
Dégue nâni meune nala khagne sa mbecté woooh
Sougnou borom bi rek mo meune founé
Gni dagbouy ragale gni thi dess gnémé
Say wakh ak say dieuf, mome boutégo thi deugue
Yawe nga wêye boule ragale
Yonou deugue mome
Bothie nékké hé di dem
Boul ragale wéet
Ndakhté dingua néwe, nioulaye
Feugueu
Saîsaîyé, gni diouboul
Ak ki khamoule dougne lameune
Beugeu waw
Yonou deugue mome
Bothie nékké di dem
Boul ragala wéet
Ragale fésse, haann pékhé dikhe………….
Résumé Français :
Qui aime bien châtie bien.
Pars du simple fait que toute vérité est bénéfique.
Ne t'en détournes jamais frère,
Car elle sera pour toi source de lumière


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Paroles de chansons de Youssou N'Dour