Sagnsé
Samba Peuzzi
paroles Samba Peuzzi Sagnsé

Samba Peuzzi - Sagnsé Lyrics & Traduction

Hey ! Guiss kou sappé comme mane dafa diafé
Lim len raw ci xel lay metti sen xol 
Boudé damay tassou mbalax demna trace 
Solou class bayi rappeurs yi saganté 
Game bé thiol boumay fifa lay bindalé song
Fi plein ko ba soul sa guel mane la PP
BanlieuZ'art la bouy rêvé lo domou bodio yi
Sa yaye bou sagnone moy diour Samba Peuzzi  
Ayway ! Ndeysanne, ndeysanne ayway !
Lou amoul la mounoul am
Billet ten ya ngui guen sans back 
Lidieuntil sa bop boulma topato
Encaissé cachet passeport bé ngey tampon 
Khaliss takhoul ma yakhou may yakh khaliss 
Guel yi sissou sen chérie may seni dop
Xélou professeur Casa de Papel
Yen concert féthie kone yess noone yi yok 

#1234# pourlane ?
Pour may Mo nioumay saga si net bi
May yarou niou beug ma napp
Beugoma boul lire sama snap ndaxté louma nex lay def
SOLOU class ba nice
Yéré olof sax mou nice
Waw bouma sagnsé douma contane 
Ankay ! mane bouma sagnsé damay contane, waw waw !
Ndaxté louniou def mou nice
Solou class mou nice
Yéré olof sax mou nice
Waw bougn sagnsé dougnou contane
Ankay ! nioune bougnou sagnsé daniouy contane, waw waw !

Yah ! tameu sama song def wax
 Comme diodéna dékilate souniou thiossane
Xolou Doudou Ndiaye ak Vieux sagne Faye sédeuna
Bougn fi nékone contane 
Ma ngui étoile yi game bi béneu star la am
Bind son denthie 2ans guéneu tangual
Reptyle music papier aluminium
 Fi douniou mayé nièkh yok thiéré doli meew
Daw khouss pousse di dem, mounougn ma té
Adriano si Pro 8 sa yaye bou sagnone moy diour Samba Peuzzi 
Ayway ! Ndeysanne, ndeysanne ayway !

#1234# pourlane ?
Pour may Mo nioumay saga si net bi
 may yarou niou beug ma napp
 beugoma boul lire sama snap ndaxté louma nex lay def
Solou class ba nice
Yéré olof sax mou nice
Waw bouma sagnsé douma contane 
Ankay ! Mane bouma sagnsé damay contane
Waw waw !
Ndaxté louniou def mou nice
Solou class mou nice
Yéré olof sax mou nice
Waw bougn sagnsé dougnou contane
Ankay ! nioune bougnou sagnsé daniouy contane, waw waw !
 


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)