paroles Ngaaka Blindé BB YO

Ngaaka Blindé - BB YO Lyrics & Traduction

Beugeu na niou guissé
Beugeu nala takk def la sakh souma gnibissé
Tebeu na si ioe déh fini
Lima beugeu féneu moy baby ioe rek'a fi né
Mane soneu na si mome dal
khalate na, mane weet na esk sax douma dof mane
Nameu na daal dila fopp mane
Sey rétane, sey waxtane
Mane ma ngui done fo ak mane
Dieul na sama xol diokh leu
All time sama xel mi ngui si ioe
Doumala neub louma kham wax leu
Sa mbeuguel si ioe di geuneu law

Choco ko choco, yama dakhal pain au lait bou am choco
Dakhal ma thiakry bougn sucré sow
Locaux, ioe la nop kham ngako
Mangui all time baby sétane sey photo
Bea yo..., bébé yo nameunala, Ayé yo
Ayé yo nameunala
Bébé yo nameunala, Ayé yo
Ayé yo nameunala
Tathiouma tathiouma
Tathiouma tathiouma ma féthial la
Tathiouma tathiouma ma féthial la
Tathiouma tathiouma ma féthial la

Baby déma foone, ioe déma ray
Sa andeu thiouray walay meun nama ray
Léglég ma beugeu daw
Mouné ma kay, khalé bé aka nex
Té meun yeufou sais ai ayway
Ma bébé yoo
(Ayo, ayo fais doucement yamey gagn ndank ndank)
Yay sama libidooo
(Ayo,ayo yamey gagn tayla dess nayger nayger)
Nala may ay lingot... shay like diamond
Euro comme CFA like dollars dollars
Baby soumanéla beugeunala
Anh yeah presque sama madré

Choco ko choco, yama dakhal
Pain au lait bou am choco
Dakhal ma thiakry bougn sucré sow
Locaux, ioe la nop kham ngako mangui
All time baby sétane sey photo
Bea yo..., bébé yo nameunala, Ayé yo
Ayé yo nameunala
Bébé yo nameunala, Ayé yo
Ayé yo nameunala

Tathiouma tathiouma
Tathiouma tathiouma ma féthial la
Tathiouma tathiouma ma féthial la
Tathiouma tathiouma ma féthial la


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment