Dema Khol
Narah Diouf
paroles Narah Diouf Dema Khol

Narah Diouf - Dema Khol Lyrics & Traduction

Guiss leu beugue leu
Wakh ma loci kham
Diokh la sama Life
Desse touma dara
Défla comme sama tere
Dangmey yokk xam xam
Diangue nala Mokal nala
Ni kou nekk daara
Bayiwouma dara
Dieul na lepp
Mbeuguel gui loumou diss diss
Atane nako
Atane nako
Bayimouma dara
Mbeuguel gui loumou diss diss
Beugue na mane
Nagnou naa

Baby dema khol
Dema khol
Dema khol
Ndakh mane souma kholé
Iow rek laye Guisse
Dema khoool
Dema khol
Ndakh mane souma kholé
Yow rek laye guisss

Louma ame loudoul iow
Mane deh beugouma
Mouy Alal di ourous
Dara safouma
Ndakh doynguama
Ma done lambe wayé
Dathie naaaa
Yama beugue bama yeuk ko
Yama soutoural
Bayiwouma dara
Dieul na lepp
Mbeuguel gui loumou diss diss
Atane nako
Atane nako
Bayimouma dara
Mbeuguel gui loumou diss diss
Beugue na mane
Nagnou naa

Yaye qui ma tane
Ya di Sama ndanane
Doumala dieundék kénéne
Yobou mane
Yobou meu fénéne
Guisseutouma kou doul yow
Sougnou mbeuguel di law
Yaye qui gueune si mane
Tamou nala tane nala

Baby dema khol
Dema khol
Dema khol
Ndakh mane souma kholé
Iow rek laye Guisse
Dema khoool
Dema khol
Ndakh mane souma kholé
Yow rek laye guisss


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment