Yalla Yaa Na
Elzo Jamdong
paroles Elzo Jamdong Yalla Yaa Na

Elzo Jamdong - Yalla Yaa Na Lyrics & Traduction

Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
And what you think ?
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na

Yo yaay se premier kharit
Rakk yaay se premier kharit
Kholou chinois meun neu nioule
Beuniou toubaab meun neu jaune
Nigga mbourou fof ko farine

Negn yokk job wagni wokh
Negn yokk wagni wokh
Diogueul for li nga mom
Se morom yaa ngui dokh
Mouno toke fi nga toke di tek
Boul kharr Prési, khamoul louy se galère
Khamoul louy se bonheur
Prési noum ley talé ?

Amoul khaddi Prési am ne salaire
Prési am ne chauffeur
Mais Prési deukkoul gallèm
C'est triste...

Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
And what you think ?
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na

Yo baayil mou sedd fattèl sho bi
Baayil mou sèdd fattél sho bi
Kham naa mom nga beuggone bokkal lepp
Wayé mèram placer na fa kou leu eupp money
Yeah daf le break wayé thioloul
Kham na ni daf le bètt wayé thioloul
Kocc néneu boul di wolou
Pour mane balaa wakhou wolou lepp sopp sakha worroul

Mais lou leu dal dang ko attane
Yeah homie lou leu dal dang ko attann
Yalla douleu tek louley yaakhal
Kou khamoul nattou mouno kham louy se kattann
Hit me

Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
Yalla Yalla beyal se tole
And what you think ?
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na
Lo gueum defalko sa bopp, Yalla yaa na

Yo message bi simple neu
Boul khaar tchi ken dara
Lo gueum defal ko se bopp
Boul khar tchi ben nit


Paroles2Chansons dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)